Buio

Youssou Ndour - Waññi Ko (version lyrics) 

Iscriviti
visualizzazioni 1,3M
91% 22 000 2 100

Waññi ko , ëpp në :
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Refain : waññi ko , waññi ko , waññi ko ,
Waññi ko , waññi ko , ëpp në
Refain : waññi ko , waññi ko , waññi ko ,
Waññi ko , waññi ko , ëpp në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në
Han , han , sa kattan bari na , sa bateau gaaw na , te saw fit rëy në

Yaw yaa ni , ëpp óon nga , trois cent kilos ,

te bés bu ne , benn xar nga daan añ e

nga neeti , at mi fi Obama ñëw ée

yaw yaa ko gis , muy dox antu , biir Pikine

am oon na , gaïnde gu rëccé , parc hann

nga neeti ñu , yaw yaa ko jat , ba mu nelaw ,

· nga ni ma , am oon nga , benn bateau , ca Guinée

te waa nations - unies , nga ka daan loué

· te diggënté , États-Unis ak Guinée ,

daa woo ko daw , lu ëpp ñaar i fan
am na benn bés , nga ni ma , my boy
keroog daje naak , roi des arènes. 2 fois.
ben loxo , laa ko yékkëtée , ni ko félicitations. 2 fois.
ma tegaat ko ci suuf , ni ko , my boy. 2 fois

na nga jaar , sa ma kër , ma jox la yeneen clefs

na nga jaar , galle , ma jox la yeneen clefs

techniques yooyu , japon laa ko jànge

ca yooya jamono , man la ñépp di wër

lu ñu wax nga ni fekke nga ko

fu ñu wax nga ni dem nga fa

doo tiit doo raf , doo dellu ginnaaw ;

waaye sa ma waa jii , ken melut ni moom.



Wax oon naa fi ni adduna ken du ko dajal ,

Te ku dul umppëlé da ñu lay ragal.

Wax aat leen ni faw nit ku ne am lu muy des al

Ngir bu ëllëg ée ñu mën laa set al.

Xam lépp , mën lépp , loolu , yalla dong a ko jagoo. 2 fois.





ragal al yalla , waay , ragal al yalla

ragal al yalla , waa jii , ragal al yalla

ragal al yalla , waay , ragal al yalla

ragal al yalla , waa jii , ragal al yalla


Pour plus de vidéos, abonnez-vous sur notre chaine
www.youtube.com/c/YoussouNdour...
youssoundour...
youssoundou...

Pubblicato il

 

19 lug 2021

Condividi:

Condividi:

Scaricare:

Caricamento in corso.....

Aggiungi a:

La mia playlist
Guarda più tardi
Commenti 4 306   
Aida Mbow
Aida Mbow 31 minuto fa
Bella questa musica 🎶 ❤❤❤❤
Alpha Sow
Alpha Sow 7 ore fa
J'adore 💪💪💪🙏
Capo Elcapo
Capo Elcapo 12 ore fa
Classic 😎 🐐
Mamichou Darmanko
il est le meilleur de tous les temps
Mame Mbekh Diagne
Tu merite tout tu ya donne tous au senegal machalla lafe thiate yalla gua ame diam
Oumar Fall
Oumar Fall 14 ore fa
Youssou ndour
Sarro's Channel
Sarro's Channel 15 ore fa
Mass Allah
Youssoupha Badji
way way dégueloulén son bi pour kham lou king bi wah
Mbacké Seck
Mbacké Seck 21 ora fa
Diffara oubbi école Musique dii orienté musiciens
AKAD Tv
AKAD Tv Giorno fa
Sama wadji mo meuna wayy noo
Mama Diop
Mama Diop Giorno fa
Amoulemorom ndour
bik momo joop
bik momo joop Giorno fa
Doumasi doyall nak
Y
Y Giorno fa
le meilleur de tout les temp 😍😘
Lami Sow
Lami Sow Giorno fa
Machalah le roi de la musique africains longue vie à vous santé dieu te protège
Fatma Sow
Fatma Sow Giorno fa
N’oublions pas l’équipe derrière le roi du mbalakh super étoile vous êtes fort mention spéciale à vous
Alioune Fall
Alioune Fall Giorno fa
I say just u are the best the king
Omar Thiam
Omar Thiam Giorno fa
King of Africa
salam
salam Giorno fa
Ak fi diamono tolou amneu solo machalla nagnou défarat djiko yi lou s4ordinaire bilay ioe
Mame khary Mbodji
🥰🥰🥰
Oumy Faye
Oumy Faye Giorno fa
Papa yousou Dal ya mana way
Matabara Diop
Matabara Diop Giorno fa
Éternellement le meilleur...you est un don du ciel...quel talent!!!!!❤️❤️❤️
Ibrahima Gueye
Ibrahima Gueye 2 giorni fa
Wanniko
salimata barry
salimata barry 2 giorni fa
Ma chaallah
Djibril Konate
Djibril Konate 2 giorni fa
Je m'aime bien cette musique je l'écoute sans arrêt 🎤👍🏾❤️🇸🇳
Kara Mbacke Mbaye
Kara Mbacke Mbaye 2 giorni fa
Machalla
bik momo joop
bik momo joop 2 giorni fa
Mafi nè papa you longue vie a vous j aim💕👍💫
Sheiktijan Sanneh
Sheiktijan Sanneh 2 giorni fa
Ge suis très content de you par ce que il aide la population sénégalais
Sheiktijan Sanneh
Sheiktijan Sanneh 2 giorni fa
Merci le roi de tout les temps
Saikou chaa
Saikou chaa 2 giorni fa
❤️
Diop Moussa
Diop Moussa 2 giorni fa
❤️❤️
Sangu îls fatick
Sangu îls fatick 2 giorni fa
Mbaye gueye faye ya bon rek😂😂😂
ablaye22 sarre22
ablaye22 sarre22 2 giorni fa
aka meune woy
Momo Doumbis
Momo Doumbis 2 giorni fa
J'ai retrouvé les lignes de basse du grand HABIB (RIP)
modoudal76
modoudal76 2 giorni fa
Yousso khana oussmane sonko laye wakhal
Mamoudou Diallo
Mamoudou Diallo 2 giorni fa
meuna nek ndak day fène rek
Mamadou Diallo
Mamadou Diallo 2 giorni fa
Youssou nd rre
DJ ADO Sénégal
DJ ADO Sénégal 2 giorni fa
Youssou ndour dou woye si 0 zero
Alex Alex
Alex Alex 2 giorni fa
international chanteur du monde plus riche en Afrique
Moustapha Seck
Moustapha Seck 3 giorni fa
ROI DU MBALAX ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Madiba Diba
Madiba Diba 3 giorni fa
Walahi c'est un roi MADIBA depuis MAURITANIE
Mohamed Nokho
Mohamed Nokho 3 giorni fa
Tonton You Text bi tamit wanniko katanam bari lolou té dou yeureumé. Wadji doutouko défati
Mouhamed Seck
Mouhamed Seck 3 giorni fa
Qui a constaté le cri de Assane Thiam 1:57 Super Etoile, Quelle complicité 😂😂😂
adji mariama demba
adji mariama demba 3 giorni fa
Mets le nom de la personne bi nga beug mou wagni )= =)
Idrissa Diack
Idrissa Diack 3 giorni fa
El phenemeno Youssou le meilleur
baye ndiaga sk sk
baye ndiaga sk sk 3 giorni fa
Roi way 🤩
CLARISSE SYLVA
CLARISSE SYLVA 3 giorni fa
Machaala
Awa Ndiaye
Awa Ndiaye 3 giorni fa
Moi je dis juste, Grand Youssou Yalla nga goudou fane yake sa Ndiabote.❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
ameth gueye
ameth gueye 3 giorni fa
Non comment il est fort ce monsieur merci Youssou pour ce tube
Amadou Sylla
Amadou Sylla 3 giorni fa
Amadou sylla
diallo seynabou
diallo seynabou 3 giorni fa
Thiey youssou 🥰🥰🥰
Adama Kasse
Adama Kasse 3 giorni fa
Le meilleur de sa génération
Badou Mbaye
Badou Mbaye 3 giorni fa
Na bahi politique neique ci côté askane wi
Mamoudou Diallo
Mamoudou Diallo 2 giorni fa
@Badou Mbaye Youssou a au moins a créé des emplois avant Macky. Et il n'est pas des genres qui fait du social devant les projecteurs. Je me demande quel raisonnement tu prônes. On accéde au pouvoir pour régler les problèmes des sénégalais. Donc pour toi toute politicien qui prend le pouvoir n'est plus du coté du peuple si je comprends bien ta définition. Dommage mais le peuple c'est l'ensemble des senégalais. Meme dans les superpuissances il y a des pauvres et des riches donc etre du peuple ne veut dire etre pauvre
bou kene merr
bou kene merr 3 giorni fa
Askan wi dou sonko. 14morts pour mortelcombat . L histoire retiendra
Badou Mbaye
Badou Mbaye 3 giorni fa
Pour moi le peuple c'est les femmes qui accouchent sur des charettes,les gens malades qui n'ont pas les moyens de se soigner, ceux qui n'ont rien à manger, c'est à dire ceux qui ont besoin d'aide pour moi youssou ndour devait être un député du peuple ou médiateur pour l'intérêt du peuple avec le gouvernement mais malheureusement il est à côté du pouvoir pour son propre intérêt
Mamoudou Diallo
Mamoudou Diallo 3 giorni fa
Pour yaw nekoul si côté askan wi? Pour vous le peuple c'est les opposants. Le peuple c'est l'ensemble des Sénégalais nak.
Cheikh Mbengue
Cheikh Mbengue 3 giorni fa
UN GRAND MESSIER, UN GRAND FIGURE MONDIAL MERCI LE ROI DU MUSIC AFRICAINE
Arame Seck
Arame Seck 3 giorni fa
Machalla Nekhna félicitations notre Ambassadeur international ♥️♥️♥️♥️🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳😍😍😍😍🥰🥰🥰🥰🙏🙏🙏🙏🙏
Abdou Jagne
Abdou Jagne 3 giorni fa
Techniques yooyu,japon laa ko jange 🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥💪💪Yusu y yal na nga fi yaga🙏
Gorgui gorgui
Gorgui gorgui 3 giorni fa
Bilayi do sén moroom plus d'un million de vue en une semaine
Oumou Diallo
Oumou Diallo 3 giorni fa
💞💞💞💞💕💕💕💓💓💗💗💖💖💖💟💟💟💯💕💞💞💓💗💖
Akeum Diop
Akeum Diop 3 giorni fa
👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑
Madiba Diba
Madiba Diba 4 giorni fa
Chapeau
zaalbi boy
zaalbi boy 4 giorni fa
Wa ana Assana Diouf🤪 degloul wouywi
modou seck
modou seck 4 giorni fa
😘😘😘
Mouhamed lamine Sy
Mouhamed lamine Sy 4 giorni fa
Le mythe🤢❤
Mbaye Wade
Mbaye Wade 4 giorni fa
Kinnnnnnnnnnnnnnnnnnng Moy King bi deeeee
Eilk Minosis
Eilk Minosis 4 giorni fa
Thiéy NDOUR !!! Y’aaaayyyy Séne baaayyy .
Tafisco Bayakh
Tafisco Bayakh 4 giorni fa
Super machallah mdrr
Manar Diagne
Manar Diagne 4 giorni fa
Champion de monde
dioufy sarr
dioufy sarr 4 giorni fa
Le meilleur de sa génération et de les temps respect père 🙏🏾
Abdoul Sarr
Abdoul Sarr 4 giorni fa
Youssou Ndour ya KO wara wanngi tu es un grand scros tu a encaissé bocoups d'argent sur wave gratuitement la plateforme que tu propose n'es pas fiable on téléchargé des chons qui n'es pas lisible... Il faut spliqué sa et le réglé
Abdoul Sarr
Abdoul Sarr 4 giorni fa
Chère Youssou Ndour on j'ai acheté l'album maïs le single téléchargé ne se lis pas,donc you on fait comment tu a encaissé mon argent s'en rien en retour
Sankare Mohamed
Sankare Mohamed 2 giorni fa
Tu change de portable c'est mieux
Soldja Baby sicario
Nice 🤩😘🥰
Nabiha Njie
Nabiha Njie 4 giorni fa
Welcome back le roi des mbalax we love you 😘😘😘😘😘😘
alaji bah
alaji bah 4 giorni fa
KING suma woii katt bi Marsha'allah
hadj kebe
hadj kebe 4 giorni fa
Deug deug deug deug deug deug deug, Youssou, andina bi bamou dath, yafi dakha weuye teigou ci Michael Jackson. J'ai jamais entendu une voix aussi extraordinaire que celle-là. Wayei tmt, Super étoile keine deimoule ngueine deiss yeine tmt. Bouba Ndour saï saï music bi, iow yaye le meilleur producteur musical de tous les temps au Sénégal, les preuves sont palpables.
oni mad
oni mad 4 giorni fa
Le corrompue manteur
Mass DIOUM
Mass DIOUM 4 giorni fa
The best
Malick Sene
Malick Sene 4 giorni fa
Thieyy andou super étoile bou yokouwoul dall d'où wanjiekou mancha ala
KHOSS MUSIC
KHOSS MUSIC 4 giorni fa
Ça voie reste toujours le même
Souadou Ndiaye
Souadou Ndiaye 4 giorni fa
Iolmm
malick ndiaye
malick ndiaye 4 giorni fa
Cey you kene meunou la merei. Mais pour le clip il faut patin quoi Di na nice deh.
Ahm Mouss
Ahm Mouss 5 giorni fa
Un chef-d'œuvre 🤭👍💪♥️♥️💯
Mamadou Ba
Mamadou Ba 5 giorni fa
Kone you kafoul Doulkatt yii la woyy 😂😂
Ibrahima Gueye
Ibrahima Gueye 5 giorni fa
Nice😍😍😍
young wizz taylor!
young wizz taylor! 5 giorni fa
Deuyzeukoulanah Youssou ndour bilahi ma le begue yow Lo way mou néx🥰 kou daccord ke Youssou ndour est le meilleur 🔥
aliou diedhiou
aliou diedhiou 5 giorni fa
The king of king. Notre fierté youssou ndour
Kawsy Sy
Kawsy Sy 5 giorni fa
Père You bi Patin mo wara Def clip bi 😂😂😂😂😂
Papa Armand Niang
Papa Armand Niang 5 giorni fa
Le maestro r.a.s
Mariama Dia
Mariama Dia 5 giorni fa
Sublime tout simplement
drk_momo
drk_momo 5 giorni fa
🤣🤣🤣 ki dh graw na wañiko bro ( je parle du mec qui mytho pas de youssou ndour )
Fatoumata Ba
Fatoumata Ba 5 giorni fa
Kounkandé wouyoul fii🤣🤣🤣
Thierno Ba
Thierno Ba 5 giorni fa
🔥🇸🇳👌🎩
SayaNE Ka
SayaNE Ka 5 giorni fa
C'est bien papa
Papis Gueye
Papis Gueye 5 giorni fa
King
Loga Vogue
Loga Vogue 5 giorni fa
❤️🔥
DIERE GUEYE
DIERE GUEYE 5 giorni fa
Tu es le meilleur notre patrimoine national
samba sané
samba sané 5 giorni fa
Son bi kounkandé lan KO wayal
Alpha Nayete
Alpha Nayete 5 giorni fa
Le plus grand regret que jai ds ce monde c'est de ne pas parler wolof juste pour ecouter ses chansons. Je n'ai jamais rater un de ses concerts ds le continent Americain. Chaque live que j'y vais est comme la 1ere fois que je le vois. God bless him!!!!
Thierno Seydi
Thierno Seydi 3 giorni fa
Youssou de toutes les générations. Le meilleur de toujours et pour toujours.L ongue vie et santé
Aboubacar Toure
Aboubacar Toure 5 giorni fa
Une chanson de haute facture à l'image de la carrière de l'homme. Pour ceux qui comprennent les parole, c'est encore plus magique. Youssou ndour au-delà de sa voix unique une plume. Il réussit à transmettre des émotions et du sens à travers sa musique. Son génie est de mettre aussi des contenus qui parlent à tous.
Ndioufa Sarr
Ndioufa Sarr 5 giorni fa
Machalla❤️🤍🤍💝💓💞💕💐💮🌺🌸⭐⭐
Bass Ndiaye
Bass Ndiaye 5 giorni fa
Machala
Moustapha Diop
Moustapha Diop 5 giorni fa
Do dara
alioune fall
alioune fall 5 giorni fa
Machallah machallah le meilleur
Il prossimo
Shiva - I can fly
3:58
visualizzazioni 278K
Youssou ndour best of rétro
1:00:02
visualizzazioni 226K
Shiva - I can fly
3:58
visualizzazioni 278K
sangiovanni - malibu
3:04
visualizzazioni 6M
Cut the flour challenge!! Round 2!!
0:31
VillaBanks, Boro Boro - Rompo
2:50
visualizzazioni 234K